Brochure Multilingue Coronavirus
” wala “diabete”. WOLOF Raxas say loxo ak ndox ak sàbu wala ak “ alcol” mòoy ray doomu jangorobi. Déel soreyante ak nitñi lu tolòog ben méetar. Ndaxte doomu jangorobi mongi néek ci biir tiflit, te menena juge ci nit dem ci nit sà suñu jegewanté di nòyi, wala di tissoli wala ñuy sëxët, wala suñu ...